Këmm

Këmm: (jëf) Mooy ñàkk a ndékki. Ku xëy ndékkiwul daa këmm.