Yol Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Facebook0Tweet0 1. Yol (jëf) Sottiku, tuuru, ndox a koy def ak yu ni mel. 2. Yol m (tur) Ndox mu bari muy walangaan jaar ci aw yoon di dem. [En: 1-stream. 2- runoff] [Fr: 1- ruisseler. 2- ruissellement] Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Seeru → Lax