Yooy Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Facebook0Tweet0 Yooy (jëf) Sew, tuuti, xiibon, ñàkk a regg. Niral: Yaw leegi dangaa yooy, xanaa fa nga nekk daa neexul? [En: skinny] [Fr: maigre] Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Lax → Sox