Bër-bër

Bër-bër: (jëf)

Lu bëgg a jóg te manul a jóg mooy def bër-bër.
Bëy wu ab wata fiir tànk ya damm day bër-bëri di jéem a jóg te du ko man. Bër-bër joo gis bu sottee, bëret a cay topp.

error: Content is protected !!