Seex Ibra Faal (Xaaj 1) Waxi Maam Seex Ibra Faal: ① » Aa doom jàppleen ci liggéeyu sëriñ Bàmba bi ku ci jàpp mu dem ku ci jàppul mu dem kon tee ngeen cee jàpp mu mel ne yéen a koy doxal ngeen dese sag...🎧 Ubbi