Tàggatu (Bind 10)

Bindal luy xamle yaay kan foo juddoo foo yaroo? Loo jàng ak looy liggéey ak say jaar-jaar ak ci lan la sa xam-xam màcc.

Tàggatu (Bind 9)

Bindal say xalaat yoo jàpp ne bu ca wolof jaaree man naa gën a jëm ca kanam.

Tàggatu (Bind 8)

Déglul ndéggat gii te bind ko fii ci suuf

 

Bind 7 – Tàggatu 2

Bindal ci fukki bind mbaa lu ko ëpp, noo gise làkku wolof ak tolluwaay ak yan jéego la war a séqiwaat ngir gën a jëm ca kanam.

Bind 7 – Tàggatu 1

Noo gise dal bii ak i ëmbeefam? Bind bu la gën a neex ci njàng mi ak dawal bu la ci gën a neex?

Bind 6 – Tàggatu 2

Bindal bataaxelub bàyyi, jëme ci sa njaatige looy liggéeyal.

Bind 6 – Tàggatu 1

Tënkal noo gise doxiinu Senegaal, ci atum 1960 ba ci jonni Yàllay tay jii.

Bind 5 – Tàggatu 1

Waxal noo gise kippaango jàng wolof.

Bind 4 – Tàggatu 2

Nettalil tuuti say jaar-jaar. (Ci fukki bind mbaa lu ko ëpp)

Bind 4 – Tàggatu 1

Bindal fii ci suuf juróomi kàddu yu am loyu jokkale ci biir.

error: Content is protected !!